诗篇 117

万国啊,你们都要赞美耶和华

Yeen xeetoo xeet, màggalleen Aji Sax ji, réewoo réew, kañleen ko. 2Moo nu xéewale ngoram gu réy, te wormay Aji Sax jee sax dàkk. Màggalleen Ki Sax!

已复制!
Aa